leral.net | S'informer en temps réel

Serigne Cheikhouna Lo Ngabou parle des homosexuels et du journal Jeune Afrique


Rédigé par leral.net le Samedi 30 Janvier 2016 à 09:53 | | 0 commentaire(s)|


Mbirum Góór-jigéén
اللواط
Homosexualité
Homosexuality
____________
(80- Fàttalikul ba "Yonnent-Yàlla Nuuh" waxee nitam ña ne léén : Moo yéén da ngéén di def ñaawtééf woo xamne yééna ko njëkka def ci àdina bi.
81- Moo ndax da ngéén di sëyënté yéén góór ñi bàyyi fi jigéén ñi ? yéén kay yàqu ngéén ba jéggi dayo.
82- Nit ña tontu wu ñuko dara ludul ne : génné léén ko dëkk bi ndaxte ñoom kat neena ñooy danuy baax-baaxlu.
83- Ma daldi koy musël mook njabootam ga bamu des soxnaam sa demoon lëkkalóó ji ak saay-saay sa.
84- Man Yalla ma daldi dotti tawub "mbugël" ca séén kaw xoolal nak yaw tooñkat ya fa ñumujjoon.
Saaru Laraaf laaya 80 ba 84
_____________________

.[سورة الأعراف: الآيات 80- 84]

{وَلُوطًا إِذْ قالَ لِقَوْمِهِ أَتَأْتُونَ الْفاحِشَةَ ما سَبَقَكُمْ بِها مِنْ أَحَدٍ مِنَ الْعالَمِينَ (80) إِنَّكُمْ لَتَأْتُونَ الرِّجالَ شَهْوَةً مِنْ دُونِ النِّساءِ بَلْ أَنْتُمْ قَوْمٌ مُسْرِفُونَ (81) وَما كانَ جَوابَ قَوْمِهِ إِلاَّ أَنْ قالُوا أَخْرِجُوهُمْ مِنْ قَرْيَتِكُمْ إِنَّهُمْ أُناسٌ يَتَطَهَّرُونَ (82) فَأَنْجَيْناهُ وَأَهْلَهُ إِلاَّ امْرَأَتَهُ كانَتْ مِنَ الْغابِرِينَ (83) وَأَمْطَرْنا عَلَيْهِمْ مَطَرًا فَانْظُرْ كَيْفَ كانَ عاقِبَةُ الْمُجْرِمِينَ (84)}.n
__________________________
Thème: Loth: condamnation de l'homosexualité 
[7:80] Loth dit à son peuple : « Vous commettez une telle abomination ; personne au monde ne l'a fait avant ! 
[7:81] « Vous pratiquez le sexe avec les hommes, au lieu des femmes. En effet, vous êtes un peuple transgresseur. » 
[7:82] Son peuple répondit en disant : « Expulsez-les de votre ville. Ce sont des gens qui souhaitent être purs. » 
[7:83] Par conséquent, nous le sauvâmes, lui et sa famille, mais pas sa femme ; elle était avec les condamnés. 
[7:84] Nous fîmes pleuvoir sur eux une certaine pluie. Note les conséquences pour les coupables. 
____________
80 And (remember) Lut (Lot), when he said to his people: "Do you commit the worst sin such as none preceding you has committed in the 'Alamin (mankind and jinn)?


81 "Verily, you practise your lusts on men instead of women. Nay, but you are a people transgressing beyond bounds (by committing great sins)."

82 And the answer of his people was only that they said: "Drive them out of your town, these are indeed men who want to be pure (from sins)!"

83 Then We saved him and his family, except his wife; she was of those who remained behind (in the torment).

84 And We rained down on them a rain (of stones). Then see what was the end of the Mujrimun (criminals, polytheists and sinners).


( Les News )