Leral.net - S'informer en temps réel

Ce que Serigne Saliou Mbacké pensait de la politique

Rédigé par leral.net le Vendredi 2 Mars 2012 à 23:38 | | 9 commentaire(s)|

Ce que Serigne Saliou Mbacké pensait de la politique



1.Posté par Momi le 02/03/2012 23:44 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

"Liii niouy wax yep (politique) dara dieumou ci tchi Yalla ak yonou Yalla ak top yalla,
Wayeh ame lo khamnee yit yeungou yeungou yi dafa beuree beuri, ba kounek ngi niew dissi laadj. kounek beug kham fouma ci nee ak fouma ci toleu.

Fima ci toleu nak la beug khamlee ni, moy linga xamnee ci la nekone; di :

mboleem gniy "lidieunti adouna" difi niew, kep koum ci nee, mane lolou (politik) dou sama liguey, yakalouma sama ligueyitam, fima ci toleu daal modi :

koufi niew kounee daal, mo xam si sey andando wala sey mbolo; sama mbolo dathiee baree lol, ba sama mbolo lako diapeh, te sama mbolo ken eupeuleeh wouma tchi,

mbolo yep nak beugeul nen len diam, beugueul nen len mouthial; taxaw na taxaway wo xamnee, te fass yeneh na bagn see diok, kou waxoul linga wara wax yit, so deloussee finga mey fek, te modi diaamou yalla ak ligueyal serign touba, te sekheuk niom linga xamnee mo dieum ci yoonou serign touba bi,.

Douma doug ci louma waroula xam wala louma waroula wax. te nak khamnako bou baxa baax, wayeh bolee woumako ci sama liguey. kone fi la si tol.

Kep ko khamnee ndiarinial senegal ak diamam ngi ci lokhom. yalla nako yalla defal ndimbal. ndakh nioune niep souniou aadio ngi ci lolou.

Lissi dess nak beug na niou dimbalima ci yi, moy di toup, di sakk sarakh ak diangoum alkhourane gui.
Fep founiou santhie keur serign touba, nanioufa yessal diangoum alkhourane gui ak khassida yi, li dal moy lo xamni sama yoona ngi ci, te manguikoy sondjee bou baxa baax.

Toubeull yalla sunu borom bi daal ak diangalep alkhourane wi daal. ak linga khamnee diglee yalla le, moniou digueul niou diko laadj, tab boudoul diekh lé leu."

Yalla nanou yalla dimbali, te kheer nou ci lim nou tanal. tawfeekhal niou si"

2.Posté par dou le 03/03/2012 00:29 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

dieuredieuf mbacké yalla nagnou yalla taasse thie sa barké AMEN

3.Posté par Oussoubannee le 03/03/2012 01:43 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

De la part de Serigne Saliou, ce ne sont que des paroles de saint homme. Il n'essez de manipuler personne, il n'exploite personne. Quand l'usine de la SONACOS a explosee a cause des gaz d'amoniac, il a ete la premiere personne a venir en aide en envoyant des dizaines de millions. Pour preuve, j'etais la-bas, et j'ai ete parmi les premiers rescueurs avant que personne n'arrive. Je ne suis ni mouride, ni tidjiane ni d'aucune tarikha, mais cet homme Serigne Saliou ET Mame Abdoul Aziz Sy, se sont des hommes de DIEU. Ils etaient la pour guider le peuple sur lka voie de DIEU. Ils n'etaient pas la pour s'enrichir ou pour se faire corrompre.
La richesse de ce bas monde ne les interresser pas. Eux ils meritent l'appellation d'homme de DIEU. Que la terre soit legere pour euyx et que DIEU les accueuille dans le plus profond du paradi. AMIN

4.Posté par ISSA le 03/03/2012 06:54 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

VEND 54 PARCELLES DE 150M2 APRES L’HÔPITAL YOUSSOU MBARGANE(rufisque) ,ENTRE ARRET CHERIF ET JAKARANDA.tél:77 646 06 15

5.Posté par mass le 03/03/2012 11:41 (depuis mobile) | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

Dieuredieuf serigne saliou yalnagnou yalla tass si sa barke. Barke serigne touba


6.Posté par narou le 29/03/2012 10:59 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

DES MEDICAMENTS TRES EFFICACES PREPARES A BASE DU SAINT CORAN, DES PRODUITS DE SERIGNE NIANG ET DE AHMED FALL NAROU SERIGNE FALLOU QUI SOIGNENT DES MALADIES COMME :
DOKHOU CITY
- HEMOROIDE
-TRAITEMENT DIABETE
TENSSION
-PROCETATE
-FAIBLESSE SEXUEL
-MANQUE D’APPETIT
-EJACULATION PRECOCE
-FATIGUEMENT GENERAL
HERNIE
ULCAIRE
PRODUIT TILI KILI BENEDIANETE
NDIMBELGUI +SOUPOU VIANDE CHEVRE
VIANDE CHéVRE +RéNE AK KHASSE +KHATIM ALKHOURANE BOUGNOU BIDE SAFERON +HUILE DIWOUGNORE%%%%%% SOUPOU ECT
POUR TOUTES INFORMATIONS CONTACTEZ AHMED FALL NAROU SERIGNE FALLOU AUX
77 941 01 47 / 77 538 55 95 / 76 464 47 97 / 70 727 75 27
SKYP E NDIMBEULEGUI1
NIMERO INTERNATIONALE- 00221 76 589 33 33

CLIQUE ICI POUR VISITE NOTRE SITE WEB http://www.ndibeulougoorakdjiguene.sitew.com/#images_de_nos_produits.A
ET ECOUTER DES EMISSIONS ET DES PUBLICITE
SIEGE TOUBA MBACKE LA VILLE SAINTE
http://www.ndibeulougoorakdjiguene.sitew.com/#images_de_nos_produits.A
http://www.ndibeulougoorakdjiguene.sitew.com

7.Posté par essic le 29/03/2012 21:28 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

CES HOMMES SERIGNE SALIOU ET SERIGNE TOUBASONT DIFFERENTS DE CE SALOPARD DE SERIGNE BETHIO ;
ils se detournent des biens terrestres,se consacrent uniquement a dieu
cet imbecile de bethio aime la vie,les habits,les chaussures,les voitures,et les femmes
bethio sa dediaw ndeye

8.Posté par alpha barry le 09/04/2012 01:09 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

deureudieuf dieureudieuffffffffffffffffff mbacke yalana yala yok sak lerrr tee tassgniou thi sa barkee dieureudieuf dieureudieuf pour tout notre vie dieureudieuff

9.Posté par seck le 10/04/2012 12:54 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

j ai pleure en entendant cet homme de dieu avec tout ce bethio dit sur lui dieureudieuf leral.net que dieu vous paye vous etes les meilleurs

Nouveau commentaire :

Tout commentaire à caractère commercial, insultant, pornographique, raciste, homophobe, incitant à la violence ou contraire aux lois sénégalaises sera supprimé, Peut entraîner votre bannissement total du site