Leral.net | S'informer en temps réel



Exclusivité clip : DAARA J FAMILY " WACCEL SA GRIFF "

Rédigé par ( Les News ) le 14 Mai 2011 à 17:44

Exclusivité clip : DAARA J FAMILY " WACCEL SA GRIFF "


1.Posté par Estelle Konté le 23/10/2011 09:08 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler

Salaamalekum!

Man la Estelle Konté, jabaru Lamine. Na ngeen def? Naka Gaal seen? Man dé, nàmm naa réew mi... fiy, ñu ngi dugg ci seddaay bu meeti waayé dinañu goorgoorlu te di xalaat naaju Sénégal ngiir mëna dundu. Jëregeenjëf ci seen musik. Loolu tamit dafa ñuy dimmbali te feexal suñu xol! Ñu ngi leen di dëglu bës bu nekk... Yàkkamti naa gisante ak yeen.

Jàmm ak xéwël! Ñu ngiy seen gannaw!!

Yal na leen Yalla sàmm te jiitu ci ay yoon yu leer te set!

Nouveau commentaire :

Tout commentaire à caractère commercial, insultant, pornographique, raciste, homophobe, incitant à la violence ou contraire aux lois sénégalaises sera supprimé, Peut entraîner votre bannissement total du site

Plus de Télé
< >