Leral.net - S'informer en temps réel

Ma femme est une adepte des marabouts

Rédigé par leral.net le Vendredi 20 Novembre 2015 à 10:26 | | 0 commentaire(s)|

Ma femme est  une adepte des marabouts
Beaucoup d’hommes souffrent de ce mal mais la plupart le taisent. Lui n’en a pas eu les capacités et a brisé le silence sur le toutgalsen. Voilà sa confession : « salam mane sama problem moy sama diabar deufa gneme serigne chak fois ay safara ak téré lay indi ci keur gui dafa makoy neub mai chaque fois ma bett ko moune dafay fadjou balegui sakh dafa melni dama oumou sama dara dokhatoul alor k avant makoy takk sama commerce dafa done dokh boubakh ma déf ci listikhar serigne bimay gnanal nena ma momay def ay liggey pour makoy diokh xalliss ak loumou wakh rek mani waw nenagnou ma diouk sama bopp sinon rek dou bakh meune touma lekk ci keur gui nakh ragal mou def ci dara reuthiou na trop lima doug ci mom louma wara def ? ».

buzzsenegal


Titre de votre page