Leral.net - S'informer en temps réel

Diplomatie parlementaire : Dakar accueille Trân Thanh Mân, Président de l’Assemblée nationale du Vietnam

Rédigé par leral.net le Dimanche 20 Juillet 2025 à 22:54 | | 0 commentaire(s)|

COMMUNIQUÉ DE PRESSE Visite officielle au Sénégal du Président de l’Assemblée nationale du Vietnam, Monsieur Trân Thanh MânDakar, du 22 au 24 juillet 2025 Le Sénégal accueille, du 22 au 24 juillet 2025, Son Excellence Monsieur Trân Thanh Mân, Président de l’Assemblée nationale de la République socialiste du Vietnam, pour une visite officielle de haut […]

COMMUNIQUÉ DE PRESSE

Visite officielle au Sénégal du Président de l’Assemblée nationale du Vietnam, Monsieur Trân Thanh Mân
Dakar, du 22 au 24 juillet 2025

Le Sénégal accueille, du 22 au 24 juillet 2025, Son Excellence Monsieur Trân Thanh Mân, Président de l’Assemblée nationale de la République socialiste du Vietnam, pour une visite officielle de haut niveau à Dakar. Il sera reçu par son homologue sénégalais, Monsieur El Malick Ndiaye, Président de l’Assemblée nationale du Sénégal.

Monsieur Trân Thanh Mân arrive à la tête d’une importante délégation de 140 membres, comprenant des ministres, parlementaires, maires ainsi que des acteurs du secteur privé vietnamien. Cette visite illustre l’intérêt croissant des deux pays à approfondir leur coopération politique, économique et institutionnelle.

Au cours de son séjour, le Président de l’Assemblée nationale vietnamienne sera reçu en audience par le Président de la République du Sénégal, Son Excellence Bassirou Diomaye Faye, ainsi que par le Premier ministre, Monsieur Ousmane Sonko.

Plusieurs accords bilatéraux seront signés à cette occasion, couvrant des domaines stratégiques tels que l’agriculture, le commerce, les affaires étrangères et la culture. Ces engagements traduisent la volonté commune des deux pays de stimuler les échanges économiques et de diversifier leurs partenariats.

En marge de la visite, une table ronde économique sera organisée par l’APIX (Agence pour la Promotion des Investissements et des Grands Travaux), en présence des deux Présidents d’Assemblée nationale. Des ministres ainsi que des représentants du secteur privé sénégalais y prendront part, afin d’explorer de nouvelles opportunités de coopération entre le Sénégal et le Vietnam.

Cette visite s’inscrit dans le cadre de la promotion de la diplomatie parlementaire, complément essentiel de la diplomatie d’État. Elle vient en appui à la diplomatie économique et contribue au renforcement des liens humains, culturels et institutionnels entre les deux pays.

Le Sénégal et le Vietnam partagent une vision commune d’un développement durable et solidaire. Cette visite historique marque un jalon important vers une coopération renforcée, durable et mutuellement bénéfique, au service du progrès, de la paix et de la prospérité partagée.

———————

YËGLE BU JËM CI TASKATI XIBAAR YI

Tukkib nemmiku ci Senegaal bu Njiital “Assemblée nationale” bu Vietnam, Sëriñ Trân Thanh Mân Dakaar, ci diggante 22 ba 24i fani sulet 2025 Senegaal dina dalal, Ku Màgg ki Sëriñ Trân Thanh Mân, Njiital “Assemblée nationale” bu Réewum njàppale mi Vietnam, ngir nemmikug “officielle” bu kawe ci Ndakaaru. Naataangoomu Senegaal bi dina ko dalal, di Sëriñ El Maalig Njaay, Njiital “Assemblée nationale” bu Senegaal. Sëriñ Trân Thanh Mân dina dikk jiite mbooloo mu am solo mu toll ci 140i nit, bokk ci ay jëwriñ, ndawi askan, ay meer ak itam njiiti sektëer piriwe bu Vietnam.

Nemmiku gi dafay jëm ci njariñu ñaari réew ci xóotal seen lëkkaloog politig, koom ak itam campeef (institutionnelle). Ci biir fan yi mu fiy am, Njiital “Assemblée nationale” bu Vietnam Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay dina ko dalal cim ndaje, ak itam Jëwriñ ju Njëkk ji, Sëriñ Usmaan SONKO. Dinañu SIÑE déggoo (accords) yu dëgër ci ndaje mii, jëm ci wàllu yu xóot di mbay, yaxantu (commerce), mbiri biti réew ak mbatiit (culture).

Aamu yooyu (engagements) dafay wane bëgg-bëgg bu ñaari réew yi bokk ci waxtaan ci koom ak wuutey seen i lëkkaloo. Lu jëm ci nemmiku bii, APIX (Agence pour la Promotion des Investissements et des Grands Travaux), ci teewaayu ñaari Njiiti “Assemblée nationale” yi. Ay jëwriñ ak it ndawi sektëer piriwe bu Senegaal dinañu teew, ci xalaat yooni lëkkaloo yu bees ci diggante Senegaal ak Vietnam.

Nemmiku gi tegu ci dooleel dipolomasi parlementaire, mottali gu am solo gu dipolomasi ETAA bi. Di jàppale dipolomasi bu koom ak bokk ci suqalikug diggante yi ci lu jëm ci nit yi, mbatiit yi (culturels) campeef yi (institutionnelle) ci diggante ñaari réew yi.

Senegaal ak Vietnam bokk yaatal ci gis-gisu suqaliku guy yàgg ak jàpplante gu ñu bokk. Nemmiku gu mboore (historique) di màndargaal ab jéego bu am solo bu jëm ci lëkkaloo gu dëgër, yàgg ak njariñu ñaari réew yépp, ci liggéey yu naat, jàmm ak naataange gu ñu bokk.



Source : https://xalimasn.com/2025/07/20/diplomatie-parleme...